loading...
loading...

WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? Download

Share Firends
Add

  • WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? this video upload MISTER SHAKE channel.This video count 51,280 views.This video length 3 minutes, 43 seconds.You can Download WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? video and mp3 or you can watch WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? video and listen music. WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? Mabo habillement de wally seck le message fort d'un des ses fans au faramaréne U Wally B. Seck - Mirna Tenue effeminée de Wally Seck: Les sénégalais s'indignent et menacent - Clip WALLY SECK presque nue réaction de NDAYE FATOU0001f923
  • WALY SECK MODE FEMININE OU BUZZ INJUSTIFIE? tags

Comments

  • Reine Noire
    Reine Noire 2018-11-06T14:49:21.000Z

    Bien di mister shake waly ma déçu

  • Abou Ndiaye
    Abou Ndiaye 2018-11-15T11:37:01.000Z

    Wally daffa sofff ndayam

  • Rokhaya Salih THIAM
    Rokhaya Salih THIAM 2018-11-11T18:01:54.000Z

    Waly défoul loudoul yabaté trop c trop yapp nga niit gni tei yam sof nga tchim!

  • Boubacar Diallo
    Boubacar Diallo 2018-11-11T02:04:24.000Z

    du ay affaire de yab wala lénéne , way nitki mém bu féké dan ka beug ,way DEUG ta bu dioté dan kay wax, star bumél ni mom warna maneu bagne yéneuyii kom yi mû deff ni. li dohul

  • DIAFFATE Virgine
    DIAFFATE Virgine 2018-11-10T23:34:00.000Z

    Mane dal pour nopal sama bopeu mani patttteu feker wouma bi Wally du djeudeu yerem rekk Sénégal diem kanam

  • Modou Ngom
    Modou Ngom 2018-11-10T14:03:31.000Z

    Bayilene waly way

  • Sheikh Jallow
    Sheikh Jallow 2018-11-09T22:19:52.000Z

    yaramou néne mo guene limou Sol gua balema akh naj

  • Fatoumata Diaw
    Fatoumata Diaw 2018-11-09T22:03:26.000Z

    Beugue nit ba takh doko wakh deugue franchemen jaime bien wally mes bi mome dokhoul trp feminine merci mst

  • kebé seikou
    kebé seikou 2018-11-09T12:47:06.000Z

    Cv

  • Madjiguene Toure
    Madjiguene Toure 2018-11-09T02:51:19.000Z

    waly mane dama la beugue trop damay kholo ngir yow louniou la wakh dafmay metirek yow def rek sa nonyi yakamtinaniou lo def rek niou oubi sen lamigne rek di wakh

  • Ramatoulaye Baldè
    Ramatoulaye Baldè 2018-11-09T01:17:51.000Z

    Limou soll dhé yaramou néne moko geun

  • Fatoubinetou Diakhate
    Fatoubinetou Diakhate 2018-11-08T20:38:53.000Z

    Yaw kaay faralo wally ahahaa daguanio yap la fok

  • Fatou Keita
    Fatou Keita 2018-11-08T16:38:35.000Z

    wawaw wakh deugeu man bi ma sétané consérbi thi rts dama tite, waly sa bay mofiniwone siiw dou diami borom kone moytoul. tegua bayi khél si gnila beugeu té sope la dakh sa bay thione.

  • محمود بن الحسن باه
    محمود بن الحسن باه 2018-11-08T10:23:18.000Z

    Woy woooy waly defa titina njaxum🙆

  • Ibou Sagna
    Ibou Sagna 2018-11-08T08:37:45.000Z

    No mei u sérieux u compare Nitt Doff à Wally non le premier est viril et le second est efféminé. En plus le mm habillement j’ai vu Titi porté le mm truc que Wally seulement El avait un soutien-gorge ce que Wally lui a oublié et u ns parle de sous-vêtements non c plutôt soutien-gorge

  • Hanata Thiam
    Hanata Thiam 2018-11-08T08:24:10.000Z

    Je veux qu'il brûle cet vêtements devant tout les sénégalais j'ai honte pour lui

  • Mame diarra diouf
    Mame diarra diouf 2018-11-08T08:14:27.000Z

    Waly dane la beug kone daguay kholat sa bop di soralé fan's yi ndakh lougnou la wakh dugnou nekh kone nak changél

  • Mbacke Thioune
    Mbacke Thioune 2018-11-08T04:20:02.000Z

    Mister atel deugu rek..... vrement sou reew moniou gnor mercii

  • Vie Konte
    Vie Konte 2018-11-08T03:37:42.000Z

    Wadji waxufi dara

  • Assaitou mareme Déme
    Assaitou mareme Déme 2018-11-08T02:17:27.000Z

    Tu as bien parlé frero